Penda mbow biography of william
Penda mbow biography of william
Penda Mbow - People View - One Africa!
Penda Mbow
Penda Mbow
| Dundu ak jaar-jaaram | |
| Juddu | Awiril 1955 (juroom-benn-fukki at ak juroom) Dakaar |
| Réew | Senegaal |
| Liggeey | Way-pólotig, jàngalekatu taarix |
| Borom-këram | Saaliw Mbay, 2017 ba tey |
| Yeneen xibaar | |
| Liggeeye na | Iniwersite Seex Anta Jóob |
| Njiitu teesam | Charles-Marie de La Roncière |
Penda Mbow mu ngi juddu atum 1955.
Borom xam-xam bu xam-xamam màcc ci taarix la, muy ab bañkat. Nekkoon na fi jëwriñ ji yore caada ak cosaan ay weer atum 2001.
Biography of william shakespeare
Jàngalekatu taarix la ci Iniwersite Seex Anta Jóob bu Dakaar nekk itam njiitu genn mbootaayu njuddu-réew.
Dundu ak jaar-jaaram
[Soppi • soppi gongikuwaay bi]Penda Mbow mu ngi juddu ci weeru mee atum 1955.
Atum 1986 la am ab doktoraa ci tarixu jamono ji farañse tudde moyeenaas (histoire médiévale) ca iniwersite bu Porowãas (Provence) ci ab teesu ñetteelu fànn bi mu bind ci « Nguuru takk-der gu askanu mameluke ci ni ko téereb nattu suuf bu Ibn al-Ji’an ñu